LIGGEEY, JANG AK MECCE
Wòlof · Català · Àudio
-
Avui és dia feiner. Avui és dia festiu.
Tey bésub liggéey la. Tey bésu bȅr la. -
Faig vacances. Vaig a fer feina.
Dama nekk ci bȅr. Damay liggéeyi. -
Faig feina de perruquer. Faig feina de perruquera. Faig feina de cambrer. Faig feina de cambrera.
Damay wat. Jigéen laa juy wat di létt. Man damay séddalé. Jigéen laa juy sédaale. -
Faig teletreball. Faig feina amb el portàtil.
Internet lay liggéeyé. Ordinatȅȅr
portabal lay ligéeyée. -
No tenc feina. Estic a l’atur.
Amuma liggéey. Damay taxawaalu. -
Cerc feina. Necessit una feina.
Liggéey ngay wut. Ligéey laa bȅgg. -
Som comerciant. Som professor. Som professora. Som pagès. Som pagesa.
Man jaaykat laa. Jàngalekat laa. Jigéen
juy jàngale laa. Beykat laa. Boroom tool laa. -
Estudii català. Estudii francès. Estudii espanyol. Estudii alemany. Estudii anglès.
Jàng naa Katalan. Jàng naa français.
Jàng naa español. Jàng naa allemand.
Jàng naa anlais. -
Estudii matemàtiques. Estudii psicologia. Estudii química. Estudii filologia. Estudii dret.
Jàng naa mathematique. Jàng naa
xeltu. Jàng naa xam -xamu simi. Jàng
naa fȅlsȅwȅ. Jàng naa yoon.