WÒLOF · CATALÀ · ÀUDIO
-
A Mallorca diuen…
Ca Majorque, dañu naan… -
En català es diu…
Ci Katalan, nii lañu koy woowe… -
Com ho diuen a Menorca...?
Naka lañuy waxee Minorque…? -
Com es diu en català...?
Naka lañuy waxee ci Katalan…? -
Saps com ho diuen a Eivissa…?
Xam nga naka lañuy wax lii ci
Ibza…? -
Saps com es diu en català…?
Ndax xam ngeen nan lañu koy
ci Katalan…? -
A Formentera diuen…
Ci Formentera dañu naan...
NUYOO AK KADDU YU LALU CI YAR

WÒLOF · CATALÀ · ÀUDIO
-
Hola. Bon dia. Bon vespre. Bona nit.
Nuyu naa la. Naka suba si.
Ngoonug jàmm. Guddig jàmm. -
Adeu. A reveure. Que vagi bé.
Ba beneen. Ba booba. Amal ay xéewal. -
Fins aviat. Fins més tard. Fins demà.
Ba ci kanam. Ba ci fan yii di nȅw. Ba suba. -
-Gràcies. Moltes de gràcies. -De res.
—Jȅrȅ-jȅf. Sant la bu baax.
—Noo ko bokk, loolu du dara -
Perdoni. Disculpi. Em sap greu.
Jegal Ma, Baal Ma, Méti Na Ma. -
Molt de gust. Tant de gust.
Bég naa ci xamante bi. -
Amb molt de gust.
Ak mbégté gu rȅy rekk. -
Que vagi de gust. Bon profit.
Lekkal bu baax. -
Diverteix-te. Que t’ho passis bé.
Bànneexu leen. Bég leen bu baax -
Benvingut. Benvinguda.
Dalal ak jàmm. -
Un moment, per favor. Una altra vegada, per favor. Més a poc a poc, per favor.
Ab diir su la neexee. Wànniwaatal su la
neexee.