AT, BES BU DELLUSI
Wòlof · Català · Àudio
-
―Quants d’anys té? Quants d’anys tens? ―Tenc 34 anys.
—Ñaata at la am? Naata at nga am?
—Am naa fanweeri at ak ñeent. -
―Quan fas els anys? ―D’aquí a un mes.
—Kañ la bés bi nga judduwoon di dellusi?
—Fii ak weer. -
Vaig néixer a Ciutadella el dia 2 de març de 1962.
Ciutadella laa juddóo 2 fan ci mars 1962.
JAMONO
Wòlof · Català · Àudio
-
―Quin temps fa avui? ―Avui fa bon dia. Avui fa mal dia.
—Naka la jamono ji bindóo tey?
—Tey jaww ji dafa neex. Tey jawwu ji
neexul dara. -
Fa fred. Fa calor. Fa molt de fred. Fa molta de calor.
Dafa sedd. Dafa tàng. Dafa sedd torop.
Tàng na torop. -
Plou. Neva. Fa sol.
Mu ngi taw. Mu ngi taw galaas. Dafa niis. -
Està tapat. Està ennuvolat. Està estirat.
Asamaan si feeñul. Dafa xiin. Mu ngi talleeku. -
Fa vent. Fa trons i llamps.
Am na ngelaw. Mu ngi dȅnnu di mellax. -
Hi ha boira. Hi ha humitat. Fa un temps molt sec.
Dafa xuy. Jaww ji dafa diis. Dafa wow torop.